dem maker
Latino Pop acoustic, original composition, mid-tempo 94–98 BPM, warm minor key, nylon-string acoustic guitar with Latin rhythmic strumming, subtle Latin percussion (congas soft, bongos light, shakers, palmas), melodic bass with smooth groove, emotional chord progression, cinematic but intimate arrangement, gradual build from minimal to powerful, expressive male lead vocal with sincerity and depth, professional octave harmonized backing vocals in choruses, strong emotional impact, inspirational and reflective mood, modern international pop production, unique and original song suitable for commercial release, civic awareness and social responsibility theme, captivating and heartfelt listening experience. ,Mixed Choir,Male Choir,Male singer
00:00 / 00:00
Lyrics
[Intro – guitare acoustique latino, percussions très légères]
Jub, jubbal, jubanti
Khéye wartou, wathieu wartou
[Chorus – voix lead, chœurs discrets en octave]
Li du dëgg, du yoon Réew mi du dem
Su nu narée continué nii Réew mi du dem
[Verse 1 – intime et posé]
Yéewuléen, te xool leenté
Bëët ak bëët
Masla bi du dëgg
Ñu génné ko ndax mu dém
Sunu Sénégal, njaay du meeseu dox
Bu ñu waxantéwul dëgg
Xam ngeen ne fii nga taxaw di saaw
Du dëgg, du yoon
[Pre-Chorus – montée émotionnelle]
Fu la neex, laale fu la neex
Njaay nga foog ne yoon la
Talibi nga xam ne respecté wooko
Ngua foog néé yoon la
[Chorus – plus large, chœurs en octave pro]
Li du dëgg, du yoon Réew mi du dem
Su nu narée continué nii Réew mi du dem
Li du dëgg, du yoon Réew mi du dem
Su nu narée continué nii Réew mi du dem
[Verse 2 – groove latino plus marqué]
Bayyi leen Kuraan bi
Ñguen di sàcc
Xam Ñguen ne li du dëgg, du yoon
Su ñu kholan té wéwul
Bëët ak bëët, du dem, du dem
[Bridge – break émotionnel, guitare + chœurs]
Nagnou kholan té
Bëët ak bëët
Té wakhaneté deugue
Loolu mooy tax Réew mi dem ciaa kanam
Loolu mooy tax Réew mi dem ciaa kanam
[Outro – parlé, solennel, guitare acoustique]
Ku lim njuum, waaye mënuñu baña wax ci ndiiit bu dul sam kadoom.
Bu ñu la ndenke, bul jàwalee sa mbagg ak mbaggu askan wi,
ndax askan wi mooy boroom
[Chorus final – chœurs puissants, émotion maximale]
Li du dëgg, du yoon Réew mi du dem
(chœurs en octave : Nagnou kholan té, Bëët ak bëët, Té wakhaneté deugue)
Su nu narée continué nii Réew mi du dem
(chœurs : Réew mi du dem)
[Last line – voix seule, silence]
Kou gnamé akara faaw nga gnamé kani